Au Sénégal si on peut parler de la constance personifiée, je dirai sans risque de me tromper que, Al Mourchid, Seydi Abdoul Aziz Sy Al Amine est l'incarnation la plus parfaite jamais égalée à travers les temps et de par sa philosophie de la vie. Dès l'âge de 14 ans, il a gagné la confiance de son père Cheikh Al Khalifa, Serigne Babacar Sy. Tous les successeurs de son vénéré père lui ont renouvelée cette confiance qu'il a sue pérenniser, malgré les énormes et nombreuses adversités, de par ses actes envers toutes les communautés éthniques, ses civilités envers ses détracteurs et ses adversaires, ses relations avec l'eglise et toutes tarikhas, ses bienfaits envers les necessiteux, ses vertus pédagogiques et sa prophetie...
La Fédération des Dahiras Tidianes d'Espagne a voulu consacrer cette année 2015 à lui rendre HOMMAGE en guise de reconnaissance à cette longue trajectoire: un “NJUKKËL” à la dimension de sa personne.
DELLOO NJUKKËL (Al Mourchid Seydi Abdoul Aziz Sy Al Amine)
Abdul Aziiz, abb dallu baay ba Aziiz Sa turëndóo ba Mulaay Dabbaax Xelu di xelli ci sa xel Xool la Maodo xalaat Bayee Seydi Mbay mu wéyël Sas la ngay baat di doxal Li kër gi soxla ci protocol Xajoo képp ku fa ñëw Ñoñ politik baa gan gu mu doon Ki xamul féetélé la boor Xam Ps baa PDS, APR walla REWMI...Daa xamul ni yaw li la ñor Moo di liy doxal rewmi Ki déggul dara tuumaal la La la gor ñi ak fóori yi di kañee Ci xam xam ak jikkóy AL AMIIN Di dox diggënté tey defar Andi gor, diine ak jabot Di doxal dëgg tey baña far Ame cofeel ci ñi nga boot Wormaal mag, teral noon Baay Siidy Moxtaar Mbakke dëggël Sa dëggu ak dogu ci mbokk gi Al Maktuum dellu saxal La mag ña jiwoon ca sa ndaw Ngay wéy di suuxat luy dundël Yoonu Seex ak xadara Maalik Seede yaa ngii tey, du ñu jeex Burd, Gammu baa Ziaar General Makka, Koor baa Tabaski Ngénte, ku faddu baa ku fande Maam Mbay, Balxawmi baa Dabbaax Jamiil, Mansuur baa Seex Tijaan Yaa di géej, deesula xuus Xanaa di ñaan Buur Yallah mu musël Yaw sunu Baay Al Amiin Samm njaboot gi ñu magg Saxal Al Maktuum, Al Xaliifa Ci tasaare ndono ak njángale Maam Maodo
Moussa Fall – Secrétaire de la Fédération des Dahiras Tidianes d'Espagne
Fédératioon des Associations Seydi El Hadji Malick Sy (FASEMSY) d'Espagne

Autres articles
-
Pourquoi la dissolution de l'Assemblée nationale devrait être différée, par Charles Émile Abdou Ciss, Ex-directeur de la solde
-
Émigration irrégulière : une approche socio-culturelle prioritaire, par Pape Modou FALL
-
Dissolution de l'Assemblée nationale, réformes institutionnelles et questions de réglages, par Mamadou Diop Decroix
-
Un Premier ministre qui gouverne, par Professeur Makhtar Diouf
-
Menace sur le vivre- ensemble : Talla Sylla écrit au peuple Sénégalais